[Chorus]
Kourou
(Don’t cry)
Kourou Bamba Ndiaye
(Don’t cry, Bamba Ndiaye)
Kourou Bamba Siniati
(Don’t cry, Bamba Siniati)
Lémméné kourou
(Don’t cry, child)
Lémméné kourou
(Don’t cry, child)
[Bridge]
Sou diante diogué khalat leu di la ladj loy khalat
(Every time I think about you I wonder what you're thinking about)
Louy sa khalat dé makoniou kham loiniou yéndo
(Tell me what you think so we know what to do)
Yaggueu nala wakh dom bou di togn
(I've always taught you that a child shouldn't be rude)
Yaggueu nala wakh dom bou di sague
(I always taught you that a child should not insult)
Yaggueu nala wakh dom bou di am lou la nakharé
(I've always taught you that a child shouldn't experience evil)
[Chorus]
Kourou Bamba Ndiaye
(Don’t cry, Bamba Ndiaye)
Kourou Bamba Siniati
(Don’t cry, Bamba Siniati)